MyLyricsFinder

Lyrics

Diahelé ouma Diomi ouma Taye die titouma Magui santeu borome bé Mane amouma aye diplôme Mane amouma asse comecome Sama Baat rek layoré di ligueye Sama bate rek layoré mome la ame Ligueye rek yaw dé mo wore dé Dounya hé mougne la ladie dé Dounya hé gnafé la ladie Si caname rek la dieme papa yé A yé Sameugama técgama si yonewé A yé Si caname rek la dieme mama yé A yé Amatoule loye tite mama yé A yé Wawe yéne saye Diahelé dadile topou waye Ga tite waye Ba doto wolou sa bopou Naga xamené borombi mogui saguinawe Ha doula massa bayé Loumou méti méti boule tita waye geumal sa bopou wa wawe Adouna déméni adouna mélala nilé fomeuna déme dou yombe Wawe naga gorgorloye Dounya hé mougne la ladie dé Dounya hé gnafé la ladie

Can't get it out of your head? Play “Dounia” yourself.