MyLyricsFinder

Lyrics

Lidé mané métina Dieuléla sa réwe yoboula fénéne Bayi lépeu liga moma Gnou yoboula fo xamoule kéneu Woye lidale lidale lidale métina Dieule la défela diama Lidé lagne défe gnome MAMA Fatéco métinama Xolale gnome déménagne déye Xolale gnome déménagne déye Xamougnou lanne lagne faye fékeu Bayi yaye bayi dome Eu To vivendo longe De onde cresci E a saudade bate aperta Ferida aberta A fé me dá coragem pra lutar E só Deus sabe quando voltarei Quem sai de cas quer voltar saudade tenho do lugar onde nasci do meu primeiro banho de mar das árvores das cores do céu E só deus sabe quando voltarei Xolale gnome déménagne déye Xolale gnome déménagne déye Xamougnou lanne lagne faye fékeu Bayi yaye bayi dome YÉya yéya lidale métina YÉya yéya lidale métinama Aliyéye lala lila laye Fatélikou rongagne dadi touro Mame boye gnoundé dougnoula faté Fatalikou rongagne dadi touro Xolale gnome déménagne déye Xolale gnome déménagne déye Xamougnou lanne lagne faye fékeu Bayi yaye bayi dome

Can't get it out of your head? Play “Metina” yourself.

Find the sheet music