MyLyricsFinder

Sénégal

Lass

Lyrics

Laak leen Sénégal Ana cosaanu Sénégalo Ñuy faddali ko Mama njala ñettali ma Li xew xew demba la Wey bu njëkko ndeun jantob Ci suufu garab dee Mama booy di ñu nettali Laak leen Sénégal Oh! Fi di dara du fi reer Filé gyañ ñuy nettali Mamso deful dara Laak leen Sénégal Xamxam nga danaa reera Ba kenn du ci jariñu dara Buñu sagané sunu jassan Laak leen Sénégal Ah, Sénégal Laak leen Sénégal Ah, nettali fattali samaay mamboy Laak leen Sénégal Ah, Sénégal Laak leen Sénégal Ah, samaal màcc cosaan ñom mamboy War nañu jàngë ñuun Jaar jaarul réew mi Ah, xam sa réew, bëgg sa réew lë Xamxam war nañu Gëssul leen, gëssul leen Wow, sunu demba Gëssul leen, gëssul leen Laak leen Sénégal Oh! Liri sa cosaan Warul loko di sagane Dankook wara toppatoo Ngir xalay ñëw sub Jàngë leen, jàngal leen Jàngal leen ko neyee Ñom ñomoom sub Laak leen Sénégal Ah, Sénégal Laak leen Sénégal Ah, nettali fattali samaay mamboy Laak leen Sénégal Ah, Sénégal Laak leen Sénégal Ah, samaal màcc cosaan ñom mamboy Laak leen Sénégal Cosaan gi, cosaan gi Modi reen gi Garab suureen yi dogee Mu fekk ci suuf si Mam buul tay waay Di ñu xamal sa xamxam gi Ñuun soxlon nañu la Laak leen Sénégal Ah, Sénégal Laak leen Sénégal Nañ ko sammu Sénégal Laak leen Sénégal Ah, Sénégal Laak leen Sénégal Nañ leen ko sammu Sénégal Laak leen Sénégal Laak leen Sénégal Laak leen Sénégal Laak leen Sénégal Laak leen Sénégal